Ndénkaane Seex Ahmadu Bàmba Xaadimu Rasuul N°3
Ndénkaane Seex Ahmadu Bàmba Xaadimu Rasuul
- Melo muriid ( aji namma yegg ci Yàlla ) bu dëggël ci tënk ñent (4) la, dama koo woy ngir ragal woru
- Dëggu ci sopp sa Sëriñ ba fàwwu tey jëfee ay ndigëlëm fum rotee
- Bàyyi gaaral ci luñ boyal doonte ci sa xol la
- Boo àndeek sa Sëriñ it nga dàq nammeel nguir rafet njort ci moom bañ koo weddi
- Képp ku boole yii melo ci muriid yi di na jot boroom dogu ya
Ci gaatal yii mooy melo yi :
- Dëggu ci sop sa Sëriñ ba fàwwu
- Jëfee ay ndigëlëm fum rotee
- Bàyyi gaaral ci luñ boyal doonte ci sa xol la
- Dàq nammeel nguir rafet njort ci moom bañ koo weddi
bamba