Ndénkaane Seex Ahmadu Bàmba Xaadimu Rasuul N°2
Ndénkaane Seex Ahmadu Bàmba Xaadimu Rasuul
Bokk na ci waxi Sëriñ bi :
1. Bàyyi fen yéen samay mbokk , moo gën jàng Alxuraan
2. Laabire ñeel mbindéefu Yàlla yi , moo gën jihaad ak yéefér ya
3. Niki noo nu fàttaliku dee moo gën ci nun , di taxawee guddi yi ci jamono
4. Na ngay sax ci dëggu ànd ak di laabire , tey fàttaliku dee boo ragalee gàcce ëllëg
bamba